|
Mbind
mu Sell mi Téere
bu mag, biy kàddug Yàlla gépp, juróom
benn fukki téere laak juróom benn. Yàlla
moo tànn ay yonent ak ñeneeni nit ci diiru junniy at
ak juróomi téeméer, xiir léen ci bind
kàddoom.
1)
Téereb Yonent yi
Kóllëre
gu jëkk gi di xaaj bu jëkk ci Mbind mu sell mi
Tawreet Yonent
Yàlla Musaa moo bind Tawreet. Mooy juróomi téere
yi jiitu ci Mbind mu sell mi.
a) Njàlbéen ga
(Genèse,
18-avril-2013) Jàng
ko. Yeb ko | Déglu
ko |
Njàlbéen
ga mooy téere bi jëkk ci Mbind mu sell mi, te moo
jiitu ci Tawreetu yonent Yàlla Musaa.
b)
Goreel ga (Exode,
12-avril-2013) Jàng
ko. Yeb ko
Ñaareelu
xaaju Tawreet, di téereb Goreel ga, moo wéyal
jaar-jaari bànni Israyil, jële ko fa ko téereb
Njàlbéen ga bàyyi woon.
c)
Sarxalkat yi (Lévitique,
24-avril-2013) Jàng
ko. Yeb ko
Ñetteelu
xaaj bu Tawreetu Musaa jëm ci sasu Sarxalkat yi.
d)
e)
Téerey
Cosaan yi
1 Samyel
(1 Samuel,
07-mai-2013)
Jàng
ko. Yeb ko 2 Samyel
(2
Samuel, 07-mai-2013)
Jàng
ko. Yeb ko
1 Buur ya
(1 Rois,
07-mai-2013)
Jàng
ko. Yeb ko 2 Buur ya
(2
Rois,
07-mai-2013)
Jàng
ko. Yeb ko Rut
(Ruth,
12-avril-2013) Jàng
ko. Yeb ko
Téerey
Taalif yi
Sabóor
(Psaumes, 16-juin-2013) Jàng
ko. Yeb ko
Kàddu yu Xelu
(Proverbes,
17-avril-2013) Jàng
ko. Yeb ko
Kàdduy Waare
(Ecclésiastes,
12-avril-2013) Jàng
ko. Yeb ko
Ngën-gi-woy (Cantique,
12-avril-2013) Jàng
ko. Yeb ko
Téerey
Waxyu yi
Kàdduy Jooytu
(Lamentations,
12-avril-2013) Jàng
ko. Yeb ko
Dañeel
(Daniel,
14-avril-2013) Jàng
ko. Yeb ko
Amos
(Amos,
14-avril-2013) Jàng
ko. Yeb ko
2)
Téereb Injiil | Déglu
ko
Kóllëre
gu bees gi di xaajub ñaareel ci Mbind mu sell mi. Mooy
kóllëre gi Yàlla fas ak nit ñi, jaarale
ko ci Almasi bi Yeesu.
Waxi
yonent yi, jëm ci Almasi bi Pour
mieux lire ce livre Nanu
ràññee… Copyright Ubbite
ga
Leeral
yi
Xibaaru Jàmm bi ci
Almasi bi Yeesu Xibaar
bu bees bi di Kàddu yiy biral dundu Almasi bu sell bi
Yeesu, Yàlla jaarale na ko ca gaayam yu tedd yi :
MACË
(Évalgile
selon Matthieu) Jàng
ko ci wolofal
MÀRK
(Évangile
selon Marc)
Jàng
ko ci wolofal LUUG
(Évangile
selon Luc)
Jàng
ko ci wolofal YOWAANA
(Évangile
selon Jean)
Jàng
ko ci wolofal
Kàddug Yàlla
tasaaroo na ci àddina :
JËFI
NDAW YA KIRIST YÓNNI (Les
Acts des Apôtres)
Jàng
ko ci wolofal
Bataaxal yi Kàddu
yiy biral yaatuwaayu ngëneel yi ci Kirist, ni ko ndawam yu
tedd yi binde :
Bataaxal yi Yàlla
may Pool, mu bind ko :
WAA
ROOM
(Épitre
de Paul aux Romains)
Jàng
ko ci wolofal
1
WAA KORENT
(Premier
Épitre de Paul aux Corinthiens)
Jàng
ko ci wolofal
2
WAA KORENT
(Second
Épitre de Paul aux Corinthiens) Jàng
ko ci wolofal
WAA
GALASI
(Épitre
de Paul aux Galates) Jàng
ko ci wolofal
WAA
EFES
(Épitre
de Paul aux Éphésiens) Jàng
ko ci wolofal
WAA
FILIB
(Épitre
de Paul aux Philippiens) Jàng
ko ci wolofal
WAA
KOLOS
(Épitre
de Paul aux Colossiens) Jàng
ko ci wolofal
1
WAA TESALONIG
(Premier
Épitre de Paul aux Thessaloniciens)
Jàng
ko ci wolofal
2
WAA TESALONIG
(Second
Épitre de Paul aux Thessaloniciens)
Jàng
ko ci wolofal
1
TIMOTE
(Premier
Épitre de Paul à Timothée)
Jàng
ko ci wolofal
2
TIMOTE
(Segond
Épiitre de Paul à Timothée)
Jàng
ko ci wolofal
TIT
(Épitre
de Paul à Tite) Jàng
ko ci wolofal
FILEMON
(Épitre
de Paul à Philémon) Jàng
ko ci wolofal
Bataaxal bi jëm
ca
YAWUT
YA (Épitre
aux Hébreux) Jàng
ko ci wolofal
Bataaxal bi Yàlla
may SAAG,
mu bind ko (Épitre
aux Hébreux) Jàng
ko ci wolofal
Bataaxal yi Yàlla
may Piyeer, mu bind ko (Épitres
de Pierre)
1
PIYEER Jàng
ko ci wolofal
2
PIYEER Jàng
ko ci wolofal
Bataaxal yi Yàlla
may Yowaana, mu bind ko (Épitres
de Jean)
1
YOWAANA Jàng
ko ci wolofal
2
YOWAANA Jàng
ko ci wolofal
3
YOWAANA Jàng
ko ci wolofal
Bataaxal bi Yàlla
may YUDD,
mu bind ko (Épitre
de Jude). Jàng
ko ci wolofal
Kàddu yiy xamle mbir
yi wara ñëw te Yeesu Kirist won ko Yowaana ci biir
PEEÑU
(La
Révélation de Jésus-Christ à Jean)
Jàng
ko ci wolofal
|