La Bible wolof
La Bible wolof

La Sainte Bible

Mbind mu sell mi

The Holy Bible

Le volume intègral, qui est l’entière Parole de Dieu, est composé de 66 livres. Dieu choisit des prophètes et d’autres à qui il révélait ses paroles au cours de quelques 1500 ans.

Téere bu mag, biy kàddug Yàlla gépp, juróom benn fukki téere laak juróom benn. Yàlla moo tànn ay yonent ak ñeneeni nit ci diiru junniy at ak juróomi téeméer, xiir léen ci bind kàddoom.

The whole volume, the complete Word of God, is made up of 66 books. God chose prophets and others through whom he revealed his words over a span of about 1500 years.

1) Le livre des prophètes

1) Téereb yonent yi

1) The prophetic books

L’Ancien Testament, la première partie de la Sainte Bible

Kóllëre gu jëkk gi di xaaj bu jëkk ci Mbind mu sell mi

The Old Testament, the first part of the Holy Bible

La Torah

Ce fut Moïse, un prophète de Dieu, qui écrivit la Torah, les premiers cinq livres de la Sainte Bible.


Tawreet

Yonent Yàlla Musaa moo bind Tawreet. Mooy juróomi téere yi jiitu ci Mbind mu sell mi.


The Torah

God’s prophet Moses wrote the Torah, the first five books of the Holy Bible.


Genèse

La Genèse est le premier livre de la Sainte Bible; elle introduit la Torah du prophète de Dieu Moïse.

La lire. La télécharger | En caractères arabs

Njàlbéen ga

Njàlbéen ga mooy téere bi jëkk ci Mbind mu sell mi, te moo jiitu ci Tawreetu yonent Yàlla Musaa.

Jàng ko. Yebal ko | Ci arab bu ñu wolofal

Genesis

Genesis is the first book of the Holy Bible; it introduces the Torah of God’s prophet Moses.

Read it. Download it | In Arabic scriptl

Exode

L’Exode, la deuxième partie de la Thora, raconte la migration des fils d’Israël, continuant le récit du Livre de la Genèse.

La lire. La télécharger.

Goreel ga

Ñaareelu xaaju Tawreet, di téereb Goreel ga, moo wéyal jaar-jaari bànni Israyil, jële ko fa ko téereb Njàlbéen ga bàyyi woon.

Jàng ko. Yebal ko.

Exodus

Exodus, the second part of the Torah, recounts the migration of the children of Israel, picking up the story where the Book of Genesis leaves off.

Read it. Download it.

Lévitique

C’est la troisième partie de la Torah de Moïse dans laquelle il définie la tâche des sacrificateurs.

Le lire. Le télécharger.

Saraxalkat yi

Ñetteelu xaaj bu Tawreetu Musaa jëm ci sasu Saraxalkat yi.

Jàng ko. Yebal ko.

Leviticus

This is the third part of Moses’ Torah in which he defines the sacrificial work of priests.

Read it. Download it.

Samuel

Les premier et second livres historiques de Samuel.

Les lire. Les télécharger.

Samyel

di téere bu jëkk bi ak téereb ñaareel bi.

Jàng ko. Yebal ko.

Samuel

The historical Books of First and Second Samuel.

Read it. Download it.

Proverbes

Les lire. Les télécharger.

Kàddu yu Xelu

Jàng ko. Yebal ko.

Proverbs

Read it. Download it.

2) Le Livre de l’évangile

2) Téereb Injiil

2) The Book of Gospel

Le Nouveau Testament, la deuxième partie de la Sainte Bible.

Le lire. Le télécharger.

Kóllëre gu bees gi di xaajub ñaareel ci Mbind mu sell mi

Jàng ko. Yebal ko.

The New Testament, the second part of the Holy Bible

Read it. Download it.

Haut